Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:28-30 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:28-30 in Kàddug Yàlla gi

28 Bul tuumaal nit ci neen, te bu ko seedeel ay fen.
29 Bul ne: «Li mu ma def laa koy def, damay feyu li mu ma def.»
30 Toolub ku yaafus laa jaare, ak tóokërub nit ku ñàkk bopp.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi