Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:26-29 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:26-29 in Kàddug Yàlla gi

26 Ki lay wax dëgg sa soppe la.
27 Ruujal sab tool, ji ko, doora tabax sa kër.
28 Bul tuumaal nit ci neen, te bu ko seedeel ay fen.
29 Bul ne: «Li mu ma def laa koy def, damay feyu li mu ma def.»
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi