Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:25-28 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:25-28 in Kàddug Yàlla gi

25 ku ko ne: «Yaa tooñ,» yaay baaxle, taasoo barke bu yaa.
26 Ki lay wax dëgg sa soppe la.
27 Ruujal sab tool, ji ko, doora tabax sa kër.
28 Bul tuumaal nit ci neen, te bu ko seedeel ay fen.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi