Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:24-26 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:24-26 in Kàddug Yàlla gi

24 Ku ne defkatu lu bon: «Yaw, tooñoo,» aw nit móolu la, mbooloo ŋàññ la;
25 ku ko ne: «Yaa tooñ,» yaay baaxle, taasoo barke bu yaa.
26 Ki lay wax dëgg sa soppe la.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi