Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:21-22 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:21-22 in Kàddug Yàlla gi

21 Doom, ragalal Aji Sax ji, wormaal buur. Bul lëngook kuy fippu.
22 Yàllaak buur a koy bette mbugal, te kenn xamul musiba mu muy doon.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi