Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:19-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Bu sa xol tàng ci ku bon, bul ñee ku soxor.
20 Ku bon amul muj, ku soxor day mel ni taal bu fey.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi