Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 24:13-15 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 24:13-15
in
Kàddug Yàlla gi
13
Doom, deel lekk lem, baax na, lem ju xelli, boo sexee, mu tem-temi.
14
Xamal ne xel mu rafet ni la neexe; soo xeloo, sa muj rafet, te sa yaakaar du tas.
15
Soxor bi, bul tëru ku jub ci këram, bul yàq dëkkuwaayam.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms