Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:12-13 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:12-13 in Kàddug Yàlla gi

12 Soo nee sa yoon nekku ci it, kiy natt xol yi, xam na, moom miy wattu sa bakkan, xam na, te kat mooy fey nit jëfam.
13 Doom, deel lekk lem, baax na, lem ju xelli, boo sexee, mu tem-temi.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi