Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:11-12 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:11-12 in Kàddug Yàlla gi

11 Wallul ku ñuy reyi te tooñul, xettlil kuy tërëf, ñu di ko reyi.
12 Soo nee sa yoon nekku ci it, kiy natt xol yi, xam na, moom miy wattu sa bakkan, xam na, te kat mooy fey nit jëfam.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi