Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 23:6-7 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 23:6-7 in Kàddug Yàlla gi

6 Ab nay, bul lekke këram, bul xemmem daraam lu neex.
7 Ma ngay xool la ngay lekk, nu mu tollu, naan la: «Lekkal, naanal!» Te xol ba àndu ca.
Kàddu yu Xelu 23 in Kàddug Yàlla gi