Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 23:20-23 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 23:20-23 in Kàddug Yàlla gi

20 Bul bokk ci ñiy lekk lu ëpp, ak a màndi,
21 ndax ku bëgg lekk ak a màndi, ñàkk dab la, dajjant it, rafle rekk.
22 Déglul sa baay bi la jur. Bu sa ndey màggatee, bu ko sàggane.
23 Jëndal dëgg te bu ko jaay. Sàkkul xel mu rafet ak yar akug dégg.
Kàddu yu Xelu 23 in Kàddug Yàlla gi