Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 23:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 23:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Bul bokk ci ñiy lekk lu ëpp, ak a màndi,
21 ndax ku bëgg lekk ak a màndi, ñàkk dab la, dajjant it, rafle rekk.
Kàddu yu Xelu 23 in Kàddug Yàlla gi