Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 23:19-22 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 23:19-22 in Kàddug Yàlla gi

19 Déglul, doom, muusal te yebu ci yoonu njub.
20 Bul bokk ci ñiy lekk lu ëpp, ak a màndi,
21 ndax ku bëgg lekk ak a màndi, ñàkk dab la, dajjant it, rafle rekk.
22 Déglul sa baay bi la jur. Bu sa ndey màggatee, bu ko sàggane.
Kàddu yu Xelu 23 in Kàddug Yàlla gi