Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 23:19-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 23:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Déglul, doom, muusal te yebu ci yoonu njub.
20 Bul bokk ci ñiy lekk lu ëpp, ak a màndi,
Kàddu yu Xelu 23 in Kàddug Yàlla gi