Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 23:15-19 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 23:15-19
in
Kàddug Yàlla gi
15
Sama doom, soo xeloo, sama xol neex.
16
Ngay wax njub, ma bég.
17
Bul ñee bàkkaarkat, saxool ragal Aji Sax ji,
18
ndax kat moo am muj, te kon sa yaakaar du tas.
19
Déglul, doom, muusal te yebu ci yoonu njub.
Kàddu yu Xelu 23 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms