Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 23:14-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 23:14-18 in Kàddug Yàlla gi

14 Soo ko bantalee, mu mana mucc.
15 Sama doom, soo xeloo, sama xol neex.
16 Ngay wax njub, ma bég.
17 Bul ñee bàkkaarkat, saxool ragal Aji Sax ji,
18 ndax kat moo am muj, te kon sa yaakaar du tas.
Kàddu yu Xelu 23 in Kàddug Yàlla gi