Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 23:11-14 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 23:11-14
in
Kàddug Yàlla gi
11
Ki koy aar màgg na, da koy taxawu, dal ci sa kaw.
12
Defal sam xel ci yar, te teewlu kàdduy xam-xam.
13
Bul ñéebloo yar gone, bantal ko taxu koo dee.
14
Soo ko bantalee, mu mana mucc.
Kàddu yu Xelu 23 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms