Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 23:11-13 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 23:11-13 in Kàddug Yàlla gi

11 Ki koy aar màgg na, da koy taxawu, dal ci sa kaw.
12 Defal sam xel ci yar, te teewlu kàdduy xam-xam.
13 Bul ñéebloo yar gone, bantal ko taxu koo dee.
Kàddu yu Xelu 23 in Kàddug Yàlla gi