Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 23:10-11 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 23:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 Bul toxal màndargam cosaan ci làccu suuf, bul aakimoo suufas jirim.
11 Ki koy aar màgg na, da koy taxawu, dal ci sa kaw.
Kàddu yu Xelu 23 in Kàddug Yàlla gi