Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 22:7-9 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 22:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Ku am ay yilif ku ñàkk, koo leb di surgaam.
8 Ku ji njubadi, góob fitna, yet wa muy dóore, damm.
9 Ku tabe am barke, mooy kiy sédd ku ñàkk cib dundam.
Kàddu yu Xelu 22 in Kàddug Yàlla gi