Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 22:5-8 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 22:5-8
in
Kàddug Yàlla gi
5
Yoonu njublaŋ, ay dég aki fiir; ku sàmm sa bakkan sore ko.
6
Tegal gone ciw yoon, ba bu màggee, du ko wacc.
7
Ku am ay yilif ku ñàkk, koo leb di surgaam.
8
Ku ji njubadi, góob fitna, yet wa muy dóore, damm.
Kàddu yu Xelu 22 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms