Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 22:19-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 22:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Yaw laa koy xamal tey jii, ndax nga wóolu Aji Sax ji.
20 Dama laa bindal fanweeri dénkaane, ci wàllu digal ak xam-xam,
Kàddu yu Xelu 22 in Kàddug Yàlla gi