Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 22:17-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 22:17-20 in Kàddug Yàlla gi

17 Teewlul te déglu li boroom xel yi wax. Defal sam xel ci li ma lay xamal.
18 Soo mokkalee, ba man koo tari, muy sa mbégte.
19 Yaw laa koy xamal tey jii, ndax nga wóolu Aji Sax ji.
20 Dama laa bindal fanweeri dénkaane, ci wàllu digal ak xam-xam,
Kàddu yu Xelu 22 in Kàddug Yàlla gi