Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 22:14-16 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 22:14-16
in
Kàddug Yàlla gi
14
Waxi ndaw su yemadi am yeer la, ku Aji Sax ji rëbb moo cay tàbbi.
15
Yëfi dof daa sax ci xolu gone, boo bantalee, mu tàggook moom.
16
Not néew-ji-doole ngir yokkule, mbaa may boroom alal, loo ci def mu wàññi la.
Kàddu yu Xelu 22 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms