Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 21:9-12 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 21:9-12 in Kàddug Yàlla gi

9 Dëkkeb ruq cim sàq moo gën jabar ju pànk.
10 Ab soxor day namma lore, te du yërëm moroomam.
11 Boo mbugalee kuy ñaawle, ab téxét jànge ca; nga jàngal ku rafet xel, mu yokku.
12 Aji Jub ji Yàlla xam na la ne ca biir kër ku bon, te mooy sànk ku bon.
Kàddu yu Xelu 21 in Kàddug Yàlla gi