Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 21:7-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 21:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 Coxor day sànk boroom, ndax day baña def njub.
8 Ab saaysaay day dëngal, nit ku dëggu di jubal.
9 Dëkkeb ruq cim sàq moo gën jabar ju pànk.
10 Ab soxor day namma lore, te du yërëm moroomam.
Kàddu yu Xelu 21 in Kàddug Yàlla gi