Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 21:3-7 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 21:3-7 in Kàddug Yàlla gi

3 Deel def dëgg ak njekk, moo gënal Aji Sax ji ab sarax.
4 Xeebaateek réy-réylu mooy bàkkaar yi ñuy ràññee ku bon.
5 Farlu, woomle; ku gaawtu, mujj néewle.
6 Alal ju la fen may, cóolóol la, day naaw, wut ko xaru la.
7 Coxor day sànk boroom, ndax day baña def njub.
Kàddu yu Xelu 21 in Kàddug Yàlla gi