Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 21:27-28 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 21:27-28 in Kàddug Yàlla gi

27 Saraxu nit ku bon ñaawtéef la, rawatina bu ci jubloo lu bon.
28 Seede buy fen day sànku, kuy dégg, sa kàddu sax.
Kàddu yu Xelu 21 in Kàddug Yàlla gi