Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 21:26-30 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 21:26-30 in Kàddug Yàlla gi

26 day yendoo xemmem, te du am, ka jub di joxeek a joxewaat.
27 Saraxu nit ku bon ñaawtéef la, rawatina bu ci jubloo lu bon.
28 Seede buy fen day sànku, kuy dégg, sa kàddu sax.
29 Ku bon day ñeme-ñemelu, ku jub la muy def da koy wóor.
30 Nit xeluwul, amul ug dégg ak pexe, ba manal Aji Sax ji dara.
Kàddu yu Xelu 21 in Kàddug Yàlla gi