Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 21:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 21:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Ku xelu denc këram ngëneeli alal aku diw, ab dof saax-saaxee josam.
21 Ku saxoo njekk ak ngor am fan wu gudd, naataangeek daraja.
Kàddu yu Xelu 21 in Kàddug Yàlla gi