Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:7-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 Ragal Aji Sax ji di njàlbéenu xam-xam, te xel mu rafet akub yar, dof yaa ko xeeb.
8 Doom, toppal yaru baay, te bul wacc ndigalu yaay.
9 Kaala gu jekk la ci bopp, di gànjar ci baat.
10 Doom, bàkkaarkat bu la xiirtal, lànkal.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi