Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:32-33 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:32-33 in Kàddug Yàlla gi

32 Déggadi sànk ab téxét, naagu rey ab dof.
33 Waaye déggal ma, dëkke jàmm, tàggook njekkar ak safaan.»
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi