Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:30-31 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:30-31 in Kàddug Yàlla gi

30 Dégluwoo samay digle it, xanaa xeeb samay àrtu yépp.
31 Waaye loo ci góobe, gar ko, say pexe suur la këll.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi