Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 1:29-31 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 1:29-31
in
Kàddug Yàlla gi
29
Daa fekk nga baña xam, te ragal Yàlla du loo taamu.
30
Dégluwoo samay digle it, xanaa xeeb samay àrtu yépp.
31
Waaye loo ci góobe, gar ko, say pexe suur la këll.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms