Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:25-26 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:25-26 in Kàddug Yàlla gi

25 Sofental nga samay digle, nanguwoo samay àrtu.
26 Kon boo sëngéemee, man it ma ree, njàqare dab la, may textexi.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi