Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:21-22 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:21-22 in Kàddug Yàlla gi

21 Ma ngay wootee bérab yu gëna xumb, di dégtaley kàddoom, bunt dëkk ba.
22 Ma nga naan: «Moo téxét bi, foo àppal sa téxét gi? Ñaawlekat bi, foo àppal sa ñaawle bi? Dof bi, ñaata yoon ngay bañ xam-xam?
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi