Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Xel mu Rafet a ngay woote ca mbedd ma, di xaacu ca pénc ma.
21 Ma ngay wootee bérab yu gëna xumb, di dégtaley kàddoom, bunt dëkk ba.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi