Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:18-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:18-20 in Kàddug Yàlla gi

18 Ñii kat seen bopp lañuy fiir, seen bakkanu bopp lañu sànk.
19 Képp kuy lekk lu lewul, nii lay mujje: wutin wu lewul jël bakkanu boroom.
20 Xel mu Rafet a ngay woote ca mbedd ma, di xaacu ca pénc ma.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi