Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 1:17-20 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 1:17-20
in
Kàddug Yàlla gi
17
Doo firib caax, ba jàpp njanaaw luy xoole.
18
Ñii kat seen bopp lañuy fiir, seen bakkanu bopp lañu sànk.
19
Képp kuy lekk lu lewul, nii lay mujje: wutin wu lewul jël bakkanu boroom.
20
Xel mu Rafet a ngay woote ca mbedd ma, di xaacu ca pénc ma.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms