Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:16-19 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:16-19 in Kàddug Yàlla gi

16 ngir dañuy xélu, nar musiba, di gaawtuy sànk bakkan.
17 Doo firib caax, ba jàpp njanaaw luy xoole.
18 Ñii kat seen bopp lañuy fiir, seen bakkanu bopp lañu sànk.
19 Képp kuy lekk lu lewul, nii lay mujje: wutin wu lewul jël bakkanu boroom.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi