Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:15-17 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:15-17 in Kàddug Yàlla gi

15 Doom, bul ànd ak ñoom ciw yoon, bul jaare fa ñuy jaar,
16 ngir dañuy xélu, nar musiba, di gaawtuy sànk bakkan.
17 Doo firib caax, ba jàpp njanaaw luy xoole.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi