Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:13-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 Mboolem alal ju réy, nu jagoo, yeb sunu biir kër, mu fees.
14 Dikkal nu far, mbuus miy benn, nu bokk.»
15 Doom, bul ànd ak ñoom ciw yoon, bul jaare fa ñuy jaar,
16 ngir dañuy xélu, nar musiba, di gaawtuy sànk bakkan.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi