Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 19:24-25 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 19:24-25 in Kàddug Yàlla gi

24 Ab yaafus day yeb loxoom ci ndab, tàyyi ko yékkati, sex.
25 Boo ñefee ab ñaawlekat, téxét ba jànge ca; nga yedd kuy dégg, mu xame ca.
Kàddu yu Xelu 19 in Kàddug Yàlla gi