Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 19:19-22 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 19:19-22 in Kàddug Yàlla gi

19 Ku naqari deret, sonal nga sa bopp; ku la xettli, tóllanti ko.
20 Déggal ndigal te yaru, ndax ëllëg nga xelu.
21 Bare na lu xol di mébét, waaye Aji Sax jeey dogal.
22 Li ñu sopp ci nit mooy ngor, néewle moo gën fen.
Kàddu yu Xelu 19 in Kàddug Yàlla gi