Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 19:16-17 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 19:16-17 in Kàddug Yàlla gi

16 Ku jëfe ndigal, sàmm sa bakkan; ku moytuwul sa bopp, dangay dee.
17 Ku baaxe ku ñàkk, lebal nga Aji Sax ji, te moo lay yool.
Kàddu yu Xelu 19 in Kàddug Yàlla gi