Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 19:12-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 19:12-14 in Kàddug Yàlla gi

12 Merum buur ni gaynde gu ŋar; yërmandey buur ni lay cig mbooy.
13 Doom ju dof naqaru baay baa, te jabar ju pànk mooy senn bu dakkul.
14 Kër ak alal ngay donne ci baay; jabar ju xelu, Aji Sax jee koy maye.
Kàddu yu Xelu 19 in Kàddug Yàlla gi