Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 17:6-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 17:6-8 in Kàddug Yàlla gi

6 Teraangay maam, sët ba; sagu doom, baay ba.
7 Waxi teggin jekkul cib dof, ay fen ci as gor waxi noppi.
8 Alalu ger njiglaay la ca ka koy joxe, ba fu mu jublu, mu nooy.
Kàddu yu Xelu 17 in Kàddug Yàlla gi