Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 17:21-23 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 17:21-23
in
Kàddug Yàlla gi
21
Ku jur ab dof, am naqar; ab dof waajuram du bég.
22
Xol bu sedd day garabal, xol bu tiis day semmal.
23
Ku bon day nangu alalu ger ca suuf, nara jalgati yoon.
Kàddu yu Xelu 17 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms