Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 17:15-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 17:15-18 in Kàddug Yàlla gi

15 Dëggal ku sikk ak daan ku jub, Aji Sax ji sib na yooyu yaar.
16 Ab dof du am xaalis, jënde xel mu rafet; buggu ca dara.
17 Xarit du bëgg, di bañ; mbokk day bokk ak yaw say coono.
18 Ku ñàkk bopp ay dige feyal jaambur, di ko gàddul boram.
Kàddu yu Xelu 17 in Kàddug Yàlla gi