Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 17:15-17 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 17:15-17
in
Kàddug Yàlla gi
15
Dëggal ku sikk ak daan ku jub, Aji Sax ji sib na yooyu yaar.
16
Ab dof du am xaalis, jënde xel mu rafet; buggu ca dara.
17
Xarit du bëgg, di bañ; mbokk day bokk ak yaw say coono.
Kàddu yu Xelu 17 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms